Maman

Publié le par SIGNATE Babacar

LUI: allo maman
Maman: boulma né allo Maman 
LUI: wa maman lou xew? 
Maman: iow ca fait deux semaine woowo ma
LUI: ah bon? wow, pour man barki demb rek laala geudj wo 
Maman: dééma wo laa wax
LUI; wa d'accord balma 
Maman: iow nitt gha, ba paré gha nek fi di yeureumteulou. bax na rek

(Elle: Thiey sama doom dji yalnama ko yalla sammal)

Maman; allo
Lui: wa
Maman; iow fo nek 
Lui: sheut maman dama gueneuh
Maman: Néma yaaghi si deuk bi di tahawaalou rek. il 14h do gnibbissi si keur gui agne bi paré na
Lui; sheut no yay agnlen dama sour (no mère bi dafa soof quoui)

(Elle: sama doom dji, anh, mom khawma sax ndax agn na famou nek, moughi goorgorlou dé mom yalla xamna, wayé dina bax)

Maman; allo
Lui; (sheut...mom chaque trois minutes mou wooté quoi) wa yay lou xew? 
Maman: il est 23h té guissagou mala ba tey
Lui; wa yaay démal teudi maghi gneuw.
Maman: nell kay yaghi si deuk bi di dokhaan rek.
lui: sheut yaay ....racroché....

(Elle: j'espère que moughi si djam rek mom. ah kharal ma toog rek nianal ko ba degg ay tankam ma nélaw).

Elles s'inquiètent pour nous sans qu'on en prenne conscience, pendant qu'on est insouciant elles se soucient de nous. Elles peuvent sembler ennuyeuses, mais à la fin de la journée elles ne vivent que pour nous.

Pour être informé des derniers articles, inscrivez vous :
Commenter cet article